![Deanerys du typhon👸🏽 Profile](https://pbs.twimg.com/profile_images/1813652580796399616/rxdTRjTP_x96.jpg)
Deanerys du typhon👸🏽
@bitynaa
Followers
49
Following
11
Statuses
460
Déjà sombi bou diar yone >>tiébou yab ak yassa
Mane Senegal nign niakalé fayda sombi metinama nak 🥲 niou dieul lek bi def ko lekou pauvre bougn la guissé nga togu sombi sakh premier réflexe bi moy danga amoul lo togu pauvre nga 🥲😭 alors que c’est tellement un plat du paradis. Togu ko def si essence vanille banane fromage.
1
0
0
@bint_annette Nn mais par contre il est beau😭mais juste pour tout ce qu’il a fait à peachy on va dire qu’il est moche
0
0
0