![Fallou Salih Profile](https://pbs.twimg.com/profile_images/1848295725198635008/Jp9TOoWX_x96.jpg)
Fallou Salih
@SalihFadal
Followers
36K
Following
41K
Statuses
31K
Fallou Salih est un serviteur de Cheikhoul khadim/communicant/chercheur/éternel- apprenant/
Dakar/Sénégal
Joined October 2018
@s_sourang Banopi ASER niamou fékk niép dalène doolél lolou motah niépako sope diko diapalé...
1
0
2
@khalilolahii Machallah lirek moo amsolo koudoul topé kéne doula tope wakeur Serigne Modou Habib si Ndjiteul Serigne Cheikh Astou Faye
0
2
5
Inaa lilaahi wa inaa ilayhi râjihoone ! Yalla nako Sunu Borom yeureum diégueulko té khaaréko Aldiana
Le TL 221 en deuil, Notre sœur Marie Rassoul @mariadiop17 vient de nous quitter 💔 Des prières pour elle 🙏🏼
0
3
27
Diomaye/Sonko amnane yéné si Rewmi té wakh deugue Yalla niongui poser aye acte nguir tahawou askan wi waayé danioo ame nioniou fale nioo hamné lidieuntiwou niou enjeux yi léne kép mooléne nior mooy noniouye lidieuntiko si poste yiniou léne diokh (Affairisme) ak fékhé positionner sén mbokkou (népotisme) amna si nioo hamné moom beugue nane mais danioo manoul (incompétence) lolou nék régime yifi diaar yép bokounna si lilène gueuna yakhal té soussi Diomaye/Sonko téloule diokk lolou mooy nék opposition bilène fiye dieulé ndah lou sénégalais mayoul Wade ak Macky douniouko maye Diomaye/Sonko ndah finiou diougué motah ak yakaar gui Rewmi ame si nioom...
0
11
100
@khalilolahii Manguilakoy ziaaré Cheikh Khalil di niaanal Cheikh Bassirou Sunu Borom yeureumko diégueulko té khaaréko Aldiana 🙏
1
0
1
@Iamgorguidiouf @RTS1_Senegal @cheikhmatarF @baaynass Émission kouko sétaan khamné lambatouwoul limiye wakj
1
0
0
@Iamgorguidiouf @RTS1_Senegal @cheikhmatarF Maîtriser na domainam d ministère du commerce gui moom gars yi mananekoko ndah SGD kharitou @baaynass😂 moom si déclaration rek lanék poser woul béne acte malheureusement
1
1
1
Le nouveau khalif de Darou Moukhty🙏✍ De Mame Thierno Birahim et de Sokhna Nogaye Fall,Serigne Khalid Mbacké, cadet de Mame Thierno Birahim est né en 1937 à Darou Moukhty,deuxième capitale du Mouridisme. Il doit ses premières humanités à son père, bien qu'ils n'eussent pas vécus longtemps, ce dernier est retourné au royaume céleste en Août 1943. Par la suite,il a continué l'apprentissage du Coran chez Serigne Jembou Cissé et Serigne Thierno Ndiaye Barama. C'est sous les ailes de ses frères Serigne Cheikh Modou Awa Balla ,et Serigne Makhmadane ,qui lui vouaient une profonde confiance, qu'il a grandi et a su parfaire son éducation religieuse,spirituelle et les sciences islamiques. On témoigne de lui un homme affable, amoureux du savoir ,disponible, et pour qui les relations de fraternité,de respect, de solidarité, sont primordiales. Que la mission qui vient de lui être assignée soit auréolée de Grâces ,et que le tout Puissant lui prête santé et longévité. CN Ahmada #MAGAL_DAROU_MOUKHTY2025
#XAM_CEERNO_JOTNA
#JËRËJËFE_SERIGNE_TOUBA
0
34
276
Inaa lilaahi wa inaa ilayhi râjihoone ! Serigne Bassirou Anta Niang, Khalife Daroul Moukhty Yalla nako Sunu Borom yeureum diégueulko té khaaréko Aldiana manguilakoy ziaaré wa Daroul Mouhty yép @khalilolahii @awambacke ak Oummah bi rawatina sama kharite Mouhammad Nazir Samb nga hamné fétém la woone diokhko ligueyou yêsal Dioumaayi Daroul Moukhty limou si yéné woone lép Yalla nassi ame lou kawé ndiortame🙏
0
4
19
@SALLAlioune20 est entrain de faire un travail remarquable concernant la liste des médias conformes au code de la presse... Ainsi, toute oeuvre humaine est émaillée d'imperfections ! Mes encouragements M. Le ministre et bonne continuation !
0
1
3
RT @SalihFadal: Keroog la Séex Bàmba daloom curucara (référence du bonnet) Toog jublu pénku jàng saaru Baqara Ba mu àggalee mu tek ca saar…
0
12
0