Moy xalilou lahi
Di Abul Mouridina
Di Baboul Mouridina
Di abo rijaaloulahi
Di Baboul houlom
Di Baboul janati
Di babul kulla xayri
Di Sidy Birahim Fall
Di Sowrou Mam Say Ndiaye
Di bayou Soxna Soda Fall
jék gnane néxi rééh
Sidy Birahim Fall aka beuri dolé fa yalla❤️
Al Mountakha !
Il revient de sa retraite spirituelle avec un visage aussi rayonnant qu’un soleil à son zénith.
Son retour est, sans nul doute, la preuve que nos souhaits seront exaucés à travers son intercession.
@Amina_Mbg
Y’avait mn frère qui disait ça poussait ds tomates dns mn ventre 😭😭
Et ma mère qui me dit so jegge goor dinga eumb
Une vraie traumatisme 😭😭😭😂😂
Keroog bu mboolo mi ne ràcc
Di séddaloo def ñaari pàcc
Bisub keroog yal naa la daj
Yàlla ak sa barke maa la gëm
Nu daagu jëm Daaru Salaam
Di xëy di joŋantey salaam
Fune nu déeyaaley salaam
Yàlla ak sa barke maa la gëm.
Temps boy demoon naa ba gëm ni Gamu murid yi bokku ñu ci 😭 ndax traitement bi ci media yi doon def
Ak Li Seriñ Tuubaa bind ci Yonent bi ﷺ yépp ci ay way ak tagg ak juli, ak li mu wax ci Gamu yépp ...
Jotna Sëkk nak ñu xamal ko génération bii ak ya ca topp
@MuridSufism
????
Box cadeau pour homme 🌸
Calepin en cuir + montre en cuir + stylo + porte clé + boutons de manchettes 🌸
➡️Service commercial : +221-77-735-29-41
🏷️13.500Fcfa
Livré avec un mot doux si vous le souhaitez 😉
#Rtappr
éciés
Y’a des gens pathétiques ici quand ça montre des fesses portant des tenues de chambre(nuisettes et consorts)vous êtes là à apprécier avec un grand sourire mais quand il s’agit de vous rappeler que le port du voile est une obligation chez la femme musulmane ngèn jëffëru…
Muuru c devenu un problème 😂
Lu Yàlla santaane la rekk comme julli.
Nun nag noo dem ba ku muuru nuy xaar ci yaw nga mucc ayib.
Elles n'ont jamais promis d'être meilleures.
🚨Jeu concours ( deuxième chance )
Pour les moins de 10k abonnés !
Pour participer :
Fav + Rt + Cite ce tweet !
- Follow
@Beck32Apple
TAS jeudi inshAllah ( 5 Vainqueurs )
Bonne chance à tous 🫶🏿❤️