![Walaqad Karamna 🏗️ Profile](https://pbs.twimg.com/profile_images/1883524742923046913/Q3hS2ydf_x96.jpg)
Walaqad Karamna 🏗️
@AmedyMustafa
Followers
3K
Following
32K
Statuses
52K
Jaamub Yallah bu bëgg Mustafa ﷺ ,bëgg doon taalube bu sax dakk ci liggeyal Xaadimal Mustafa, tek ci di Sant bey fecc
طوبي
Joined February 2018
Fii la liggey bi tollu ! Ayca nu dem ma ame sama ñaari sax bala tëddi 77-776-68-39
« Ku fékk sa mbokk jullit bu woor ba ngoon nga dogal ko kooram dinga am yool bu tollo ni moom bi mu am ci kooram te du waññi ci kooram dara » Le ramadan approche multiplions les bonnes œuvres ! Let’s go 3000 Fcfa/personne OM/wave - 77-776-68-39
0
3
2
Hummmmm
0
0
0
Amna laaj deh concernant les jours blancs ak addiis biy wax ni woor ñett fan ci weer wu nek ku ma ci mën a dimbli ?
Les jours blancs de ce mois de février : - 13 février 2025 / 13 Cha’ban - 14 février 2025 / 14 Cha’ban - 15 février 2025 / 15 Cha’ban Le prophète ﷺ nous ordonnait de jeûner les jours blancs, le 13, le 14 et le 15 et il disait: « Ceci est comme le jeûne du mois entier ».
0
1
0
+18.000 Fcfa actuellement ayca gaayi un sac AUJOURDHUI !! 😁😁
« Ku fékk sa mbokk jullit bu woor ba ngoon nga dogal ko kooram dinga am yool bu tollo ni moom bi mu am ci kooram te du waññi ci kooram dara » Le ramadan approche multiplions les bonnes œuvres ! Let’s go 3000 Fcfa/personne OM/wave - 77-776-68-39
0
0
1
Bala Maa tëdd insaAllah na benn saaku sukkar matt 👍🏾